Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| BF |
Aminta, xanaa danga sibbiru? Aminata, as-tu le palu? |
|
| AG |
Waaw, dama sibbiru. Lu ci baax? Oui, j'ai le palu. Que faut-il prendre? |
|
| BF |
Li gën ci pajum sibbiru mooy nga naan. Pour traiter le palu, il faut prendre les médicaments dès que tu sens la maladie arriver. |
|
| MN |
Su la songee, dinga yëg metit? Au début, y-a-t-il des douleurs? |
|
| BF |
Waawaaw. Ku mu song, sa yaram day tàmbali di lox, tàng jérr di metti ànd ak bopp bi. Bien sûr. Dès que la maladie commence, tu as des frissons, de la fièvre et des maux de tête. |
|
| MN |
Yan garab ñoo ci baax? Quel médicament faut-il prendre? |
|
| BF |
Su fekkee ni sibbiru si dal na la ba noppi, dangay naan ñetti doomi niwakiin ci saa si, ñett ci ngoon bala ngay tëdd. Si tu es déjà malade, tu prends tout de suite 3 comprimés de nivaquine, 3 avant de te coucher. Ca ëllëg sa nga naanaat ñett ci suba ak ñett ci ngoon, lépp di fukk ak ñaar. 3 le lendemain matin, puis 3 le soir. Au total, 12 comprimés. Su fekkee ni dangay fàggu ngir moytu sibbiru si, dangay naan ñetti doom ayu-bés bu nekk. A titre préventif, tu prends 3 comprimés par semaine. |
|
|
|
||
|
|
| Tekki baat | Lexique |
| feeñ | apparaître |
| jérr | très (chaud) ; adverbe d'intensité utilisé avec tàng seulement |
| lox | avoir des frissons |
| moytu | éviter |
| song | attaquer |
| yëg | sentir |
| ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö |
|
@ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º |