Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| SB |
Dégg naa ni sa maam dafa gaañu. J'ai appris que ton grand-parent est décédé. |
| XJ |
Waaw, gaañu na démb. Oui, il est décédé hier. |
| SB |
Moom, dafa feebaroon? Est-ce qu'il était malade? |
| XJ |
Waaw, yàgg na feebar de. Oui, cela fait longtemps qu'il était malade. |
| SB |
Man yëguma ko woon. Siggil ndigaale! Moi, je n'étais pas au courant. Mes condoléances! |
| XJ |
Siggil sa wàll! A toi de même! |
| SB |
Yàlla na la dëdd ak jàmm! Qu'il te tourne le dos en paix! |
| XJ |
Amiin Amen |
| SB |
Maa ngiy dem. Je m'en vais. |
| XJ |
Baax na. Yàlla na la Yàlla bindal tuyaaba! C'est gentil. Que Dieu te bénisse! |
| SB |
Amiin Amen |
|
Tekki baat |
Lexique |
| dëdd |
tourner le dos |
|
dëj bi |
le décès, l'enterrement |
| maam |
grand-père ou grand-mère |
| siggi |
relever la tête |
| tuyaaba | bienfait |
| yëg |
sentir, être au courant |
| Abdoulaye Dial |
| ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö |
|
@ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º |