Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
123 A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z
. dame soxna si (âgée et respectable) : Daje naa sa soxna si. J'ai rencontré ta dame.
. datte tàndarma ji : Jënd naa ay tàndarma. J'ai acheté des dattes.
. débarcadère waax bi, teeru bi : Gaal yaa ngi ci waax bi. Les bateaux sont au débarcadère.
. débroussailler ruuj : Beykat baa ngiy ruuj toolam. Le cultivateur débroussaille son champ.
. décider dogal : Kelifa gi mooy dogal fii. C'est le patron qui décide ici.
. défaut sikk si : Sa xarit bi dafa bare sikk. Ton ami a beaucoup de défauts.
. défendre tere : Dañuy tere ku fi tóx. On défend de fumer ici.
. déféquer puub, day. Sale bi puub na ci lal bi. L'enfant a déféqué sur le lit.
. défunt jëm-si-yàlla-ji : Defal ni jëm-si-yàlla-ji Faal ! Fais comme le défunt Faal !
. dégonflé peer : Sa bal bi nga jënd, peer na. Le ballon que tu as acheté s'est dégonflé.
. dégoûter sàppi, soof : Ceebu-jën dafa ma sàppi. Le riz au poisson me dégoûte.
. délai diir bi, gàpp bi : Bu diir bi jeexee ma dellu. Après le délai, je retourne.
. délimiter un espace ër : Kër gi mam jëndoon, ër nañu ko. On a délimité la maison que j'avais achetée.. dot can gi, warugar wi : Damay may Faatu, indi nañu warugar wi. Je donne Fatou en mariage, on a amené la dot.
. douloureux metti : Dee, dafa metti. La mort est quelque chose de douloureux.
. drap de lit darab bi : Jënd naa ay darab yu bees. J'ai acheté de nouveaux draps de lit.
. drapeau raaya bi : Sunu raaya am na ñatti melo. Notre drapeau a trois couleurs.
. dresser tàggat : Damay tàggat sama xaj bi. Je dresse mon chien.
. duper nax. Waruloo ma woon loolu, danga ma wax. Ce n'est pas ce que tu m'avais dit. Tu m'as dupé.
. durée diir bi : Liggéey bi dafa laaj diir. Le travail nécessite une durée.
. durer yàgg : Dinaa yàgg ci réew mi. Je vais durer dans le pays.
. dysenterie biiru-taññ wànte tane na. J'avais la dysenterie, mais je me porte mieux.
Le Petit Wolof est un dictionnaire vivant. Revenez le voir souvent.
| ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö |
|
@ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º |