The Wolof-Multilanguage Live Dictionary Project
Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !



translator  wo-en en-wo grammar talk   $ 
      grammatik konversation  
HOME wo-fr fr-wo grammaire conversation sciences fr
Mercredi 2 août 2000 3 02 /08 /Août /2000 14:24

123  A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z

 

 

. jalouser (en amour) fiir : Sa jëkkër dafa fiir. Ton mari est jaloux.

. jamais mukk : Duma naan mukk sàngara. Je ne boirai jamais de l'alcool.

. jambe tànk bi, yeel bi : Sama yeel dafay metti. Ma jambe me fait mal.

. jardin tool bi : Ci gannaaw kër gi am no tool. Il y a un jardin derrière la maison.

. jaunisse payis bi : Sama jabaru nijaay dafa payis. La femme de mon oncle a la jaunisse.

. jeter sànni : Nanga sànni mballit mi. Il faudra jeter les ordures.

. jeûne koor gi : Damay woor ci koor gi. Je jeûne pendant le ramadan.

. jeunes (les) ndaw ñi : Nguur gaa ngiy dajale ndaw ñi. L'état rassemble les jeunes.

. joie mbégte mi : Dama am mbégte ci sa liggéey. J'éprouve de la joie avec ton travail.

. joli rafet : Gis naa jigéen ju rafet ci sa kër. J'ai vu une jolie femme chez toi.

. jouer fo : Xale yaa ngiy fo ci ëtt bi. Les enfants jouent dans la cour.

. jour bés bi, fan wi : Ñëw naa am na ñaari fan. Je suis venu il y a deux jours.

. journée bëccëg bi : Ci bëccëg bi laay dem Dakaar. C'est dans la journée que je vais à Dakar.

. joyeux bég : Xale yi bég nañu tey. Les enfants sont joyeux aujourd'hui.

. jugement àtte bi, dogal bi : Àtte bi leer na. Le jugement a été clair.

. juger àtte : Tey lañuy àtte jigéen ñi. C'est aujourd'hui qu'on juge les femmes.

. jujube siddéem si, déem si : Jëndal naa xale yi siddéem. J'ai acheté des jujubes pour les enfants.

. jumeau séex bi : Jabaru Abdu am na ay seex. La femme de Abdou a des jumeaux.

. jument wajan wi : Jënd naa benn wajan. J'ai acheté une jument.

. jurer (serment) waat, giñ : Waat naa ci sama boroom. Je jure devant Dieu.

. justifier làyyi : Nanga làyyi boo demee polis ! Il faudra que tu te justifies à la police !

 

Le Petit Wolof - Le dictionnaire wolof-multilingue le plus vivant du monde !

Par wolofi - Publié dans : FR-WO
Ecrire un commentaire - Voir les 0 commentaires
Retour à l'accueil

Chic Meteo
Holidays

♦ Las Vegas
♦ New York
♦ UTC/GMT
♦ Paris
♦ Dakar

 

 

NON à l'excision !

Recherche

ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö
 @ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º

Al-Nd-Petit-Wolof.jpg
Le Petit Wolof deviendra grand.

 
 
  
anti-xeesal.jpg  
Anti-xeesal Campaign.
       
 
   

Syndication

  • Flux RSS des articles

Le sens du partage


pied_top.jpg
 
Contact - C.G.U. - Rémunération en droits d'auteur - Signaler un abus - Articles les plus commentés