The Wolof-Multilanguage Live Dictionary Project
Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !


translator  wo-en en-wo grammar talk   $ 
      grammatik konversation  
HOME wo-fr fr-wo grammaire conversation sciences fr
Vendredi 7 août 2009 5 07 /08 /2009 16:21



by Aby Ndour


Lyrics

Hooo mba lidé woor na
Hooo mba li sakh diam la
Mane yémou naa
Mane warou na
Mane diomi na
Mane diakh le na

Maane kharit lako diapé
Moom mbëggeel leuko gisé
Mane yémou naa
Mane warou na
Mane diakhle naa yée yée

Mane leu bëgg te gisuma
Dotouma giseté
Mingi sone te gisuma
Nobou ma
Dima sétma te gisuma
Filou mako
Mingui sonne te gisuma

Dotougnou gise
Mane leu bëgge te gisuma
Dafa diawale
Da sone té gisuma
Mbëggeel ak kharit
Dima séet te gisuma

Hooo démaa tuma
Hooo mane de dama ko rousse
Moom diawalé koke mbëggeel
Mane yémou naa
Mane warou na
Mane diomi na
Diakhlé naa

Mane leu bëgge te gisuma
Dotouma giseté
Mingui sone té gisuma
Nobu ma
Dima Sétma té gisuma
Filou mako ma gisuma

Mingui sone té gisuma
Dotougnou gisé
Mane dé la bëgge té gisuma
Dotougnou gisé
Mane dé la bëgg té gisuma
Dafa diawalé
Mingui sone té gisuma
Mbëggeel ak kharit

Dem na té gisuma
Dem na sonne na
Dafa diawalé
Mane dé la bëgge té gisuma
Kharit ak nobel

Daye soone té gisuma
Sétou mako
Déme na séet te gisuma
Déme na sone na
Déguena lékatul
Mane dé la bëgg té gisuma

Hohohoho
Daye sone té gisuma
Dotougnou gisé
Mane dé la bëgge té gisuma déme na soone na
Bëggetuma ñu gisé
Ndax mane bëggu mako sonal
Wayé limaye déf moye
Dématuma

La transcription en wolof académique par Pap Abdoulaye Dial va venir bientôt. En attendant, prenez ces paroles-ci pour chanter. C'est ce que je fais et ça marche. Mes murs sont très contents.

Par wolofi - Publié dans : music - Communauté : Terre d'Afrique
Ecrire un commentaire - Voir les commentaires - Recommander
Retour à l'accueil

  • : Vue de ma fenêtre.

Chic Meteo
Holidays

♦ UTC/GMT
♦ Paris
♦ Dakar
♦ New York

Recherche

ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö
 @ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º

Syndication

  • Flux RSS des articles

Le sens du partage

Contact - C.G.U. - Rémunération en droits d'auteur - Signaler un abus - Articles les plus commentés