Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| FD |
Kañ ngay fóot sa yére yi ? Quand laves-tu tes vêtements ? |
|
| AF |
Damay togg añ bi ba noppi. Je préparerai le déjeuner avant. |
|
| FD |
Fecciwoon nga démb ca sabar ga ? As-tu dansé au son du tam-tam hier ? |
|
| AF |
Demoon naa waaye feccuma, dama toog di tàccu rekk. J'y suis allée mais je n'ai pas dansé. J'ai seulement applaudi. |
|
| FD |
Lu tax ? Pourquoi ? |
|
| AF |
Mënuma fecc sabar. Je ne sais pas danser la danse traditionnelle (sabar). |
|
| FJ |
Ana say doom ? Oû sont tes enfants ? |
|
| AF |
Ñu ngiy fo ci ëtt bi. Ils jouent dans la cour. |
|
| FJ |
Lan ngay def ci say gëñ ? Danu weex de ! Qu'est-ce que tu mets sur tes dents ? Elles sont vraiment blanches ! |
|
| AF |
Dara. xanaa di leen socc rekk. Rien, je les frotte avec un bâtonnet. |
|
| FJ |
Dinaay soccu léegi ndax samay gëñ yi weex na sa yos. Je frotterai aussi mes dents pour qu'elles soient blanches comme les tiennes. |
|
| AF |
Waaw, moo gën de. Soccu baax na lool sax ! Oui, c'est mieux. C'est vraiment bien de se frotter les dents ! |
| Tekki baat | Lexique | |
| ëtt bi | la cour | |
| fecc | danser | |
| fo | jouer | |
| fóot | faire la lessive | |
| sabar | tam-tam | |
| soccu | (se) frotter les dents avec un bâtonnet | |
| tàccu | applaudir | |
| togg | préparer le repas | |
| weex | être blanc |
| ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö |
|
@ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º |