Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| FF |
Yéen, dingeen faral di naan attaaya su ngeen añee ba noppi ? Avez-vous l'habitude de prendre le thé après le déjeuner ? |
|
| AN |
Waaw, dinanu koy naan, wànte man, benn baraada bu woyef rekk laay naan. Yow nag ? Oui, nous en prenons, mais moi, un seul verre me suffit. Et toi ? |
|
| FF |
Man, ñetti baraada yépp laay naan : lëwël bi, ñaareel bi ak ñetteel bi. Moi, je prends les trois verres : le premier, le deuxième et le troisième. |
|
| AN |
Nafi, xiimal waay ! Bu ci def warga ju bare de ! Nafi, fais le thé et ne mets pas beaucoup de thé ! |
|
| N |
Déedéet, tuuti rekk laa ciy def. Non, un peu seulement. |
|
| AN |
Suukër si nga jënd doy na ? Est-ce que le sucre que tu as acheté suffit ? |
|
| N |
Waaw, doy na waaye amaguma naanaa de. Oui, mais je n'ai pas encore de menthe. |
|
| AN |
Wool xale bi mu boyal furnó bi, jëndal la naanaa te indi kaasi attaaya bi ! Appelle le gosse pour qu'il allume le charbon dans le fourneau, acheter de la menthe et ensuite apporter les verres. |
| ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö |
|
@ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º |