Le Dictionnaire Wolof-Multilingue Vivant !
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
| translator | wo-en | en-wo | grammar | talk |
♦ $ ♦ ♦ |
| grammatik | konversation | ||||
| HOME | wo-fr | fr-wo | grammaire | conversation | sciences fr |
Wér gi yaram Gesundheit
Lu la jot? Was ist los?
Dama feebar. Ich bin krank.
Lu lay metti? Was tut Dir weh?
Sama biir mooy metti. Mein Bauch tut weh.
Am ! Naanal garab gii. Hier ! Nimm diese Medizin.
Jërëjëf ! Danke.
Amul solo, ñoo ko bokk! Kein Problem. Gern geschehen.
Kooku? Wer ist da?
Mana Pap Laay. Ich bin's, Pap Laye.
Kooy seet? Wen suchst Du?
Doktëër laay seet. Den Arzt suche ich.
Dafa jàpp. Xaaral tuuti ! Er ist beschäftigt. Warte ein bisschen !
Kan ngay seet? Wen suchst Du?
Doktëër. Den Arzt.
Dafay oppeere. Er operiert gerade.
Ma xaar ko? Soll ich auf ihn warten?
Soo bëggëë. Wenn Du möchtest.
Ana doktëër? Wo ist der Arzt?
Mu ngi ci biir. Moom ngay seet ? Er ist drinnen. Ist er derjenige, den Du suchst?
Waaw, moom laay seet. Ja, ihn suche ich.
Lan la ? Danga feebar? Was ist los ? Bist Du krank?
Waaw, dama xawa feebar. Ja, ich bin ein wenig krank.
Ana doktëër? Mu ngi fi? Wo ist der Arzt? Ist er hier?
Waaw, mu ngi fi. Dafa jàpp. Ja, er ist da, aber er ist beschäftigt.
Ma xaar ko? Kann ich auf ihn warten?
Soo beggëë. Wenn Du möchtest.
Maa ngiy dem, ba suba. Ich gehe. Bis morgen.
Waaw, moo gën. Nanga teela ñëw de ! Ja, das ist besser. Du musst früher kommen.
Ku ci topp? Wer ist der nächste?
| altiné |
Montag Lundi Monday |
|
| talaata |
Dienstag Mardi Tuesday |
|
| allarba |
Mittwoch Mercredi Wednesday |
|
| alxemes |
Donnerstag Jeudi Thursday |
|
| aljuma |
Freitag Vendredi Friday |
|
| gaawu (aseer) |
Samtag Samedi Saturday |
|
| dibeer (dimaas) |
Sonntag Dimanche Sunday |
| bés bi, fan wi | der Tag | |
| bëccëg bi | der Tag | |
| ëllëg, suba | morgen | |
| suba si | der Morgen | |
| ci suba | am Morgen | |
| ngoon si | der Nachmittag | |
| guddi gi | die Nacht | |
| léegi | jetzt | |
| léeg-léeg | von Zeit zu Zeit | |
| waxtu wi jot na | es ist Zeit zu... | |
| ren | dieses Jahr, heuer | |
| daaw | letztes Jahr | |
| déwén |
nächstes Jahr |
|
|
gannaaw suba, gannaaw ëllëg |
übermorgen | |
| suba teel | frühmorgens | |
| ci saa si |
plötzlich, sofort |
|
| ndékki li | Frühstück | |
| añ bi | Mittagessen | |
| reer bi | Abendessen | |
| ŋ [ ] À Ññ Çç ß Óó Ëë Ïï Öö |
|
@ ½ ¼ Ää Üü ÷ ▀ ² ■ ª º |